taggat - taggat ben ben

Tannal ca taggat

KL151 : Wereul ball bi sa bopp + One Leg Step Hop + Dugal ball bi ci suff

  1. Sanni ball bi ca kanam
    wendelal ball mu ñeuw ci yow
  2. Teubal dal ñari tank
    "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
  3. Driblel
    tank ak ball lalando suf,drible bi ak tank be andando
  4. Wereul ball bi sa bopp
    wereulal ball bi sa ndigg par benn loxo, loxo yi jub.
  5. One Leg Step Hop
    Jump and land on the same leg.
  6. step
    push from behind
  7. Dugal ball bi ci suff
    Teg ball bi ci koñ bu weex u dunk bi.

faram fathie: Boniface Ndong


Bball loxo bu gatt

BballSteno_KL111

Bball loxo bu gatt?



BasKidball


BasKidball