taggat - taggat ben ben

Tannal ca taggat

KL149 : gallop-step + Dugal ball bi ci suff

  1. Sanni ball bi ca kanam
    wendelal ball mu ñeuw ci yow
  2. Teubal dal ñari tank
    "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
  3. Dox xarale sa yaram
    Driblel loxo bi ci biti- ,tank ak ball bi lalando suuf, tank bi ci bir ak benen loxo bi sam ball bi.
  4. gallop-step
    first step, short and high, the second step flat and long
  5. Dugal ball bi ci suff
    Teg ball bi ci koñ bu weex u dunk bi.

faram fathie: Boniface Ndong


Bball loxo bu gatt

BballSteno_KL111

Bball loxo bu gatt?



BasKidball