KL148 : Prebounce ball overhead + Dribelel ci pañe ba + Dugal ball bi ci suff
Prebounce ball overhead Spin the ball to yourself so that you can catch it overhead and prepare a throw before you touch the ground.
Teubal dal ñari tank "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
Dox xarale sa yaram Driblel loxo bi ci biti- ,tank ak ball bi lalando suuf, tank bi ci bir ak benen loxo bi sam ball bi.