taggat - taggat ben ben

Tannal ca taggat

KL145 : Dribelel ci pañe ba + 360 + dugeul ball bi ci kaw

  1. Sanni ball bi ca kanam
    wendelal ball mu ñeuw ci yow
  2. Teubal dal ñari tank
    "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
  3. Driblel
    tank ak ball lalando suf,drible bi ak tank be andando
  4. 360
    weur ball bi, niari tank yi lalando suf.
  5. dugeul ball bi ci kaw
    Teg ball bi ci koñ bu weex u dunk bi.

faram fathie: Boniface Ndong


Bball loxo bu gatt

BballSteno_KL111

Bball loxo bu gatt?



BasKidball