Teubal dal ñari tank "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
Dox xarale sa yaram Driblel loxo bi ci biti- ,tank ak ball bi lalando suuf, tank bi ci bir ak benen loxo bi sam ball bi.
Underhand layup on the anchor leg side Anchor leg and throwing arm are on the same side. Layup against backboard aiming for top corner of the square. Stretch your arm as much as possible upward.