taggat - taggat ben ben

Tannal ca taggat

KL133 : Wereul ball bi sa bopp + Pivote 360 degre + Delay + femu MJ + wendelu ca kanam + MJ-Move through the legs + wendelu ca kanam + dugeul ball bi ci kaw

  1. Sanni ball bi ca kanam
    wendelal ball mu ñeuw ci yow
  2. Teubal dal ñari tank
    "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
  3. Wereul ball bi sa bopp
    wereulal ball bi sa ndigg par benn loxo, loxo yi jub.
  4. Pivote 360 degre
    pivote 360 degre bayi pañe bi ak sa tank bi ci kanam
  5. Delay
    Pause between moves in certain position to contrast with next move that is very fast.
  6. femu MJ
    Defal ndiego bu mag ak sa tank u ginaw di dem xaralale sa tank, tegal sa tank, xaralel ci suf.
  7. wendelu ca kanam
    wendelal sa yaram 270 degre ca kanam
  8. MJ-Move through the legs
    Abrupt change of direction, dribble the ball through the legs to the other hand deep down.
  9. wendelu ca kanam
    wendelal sa yaram 270 degre ca kanam
  10. dugeul ball bi ci kaw
    Teg ball bi ci koñ bu weex u dunk bi.

faram fathie: Boniface Ndong


Bball loxo bu gatt

BballSteno_KL111

Bball loxo bu gatt?



BasKidball


BasKidball