taggat - taggat ben ben

Tannal ca taggat

KL129 : Pivote 360 degre + Femu profesionel + Dugal ball bi ci suff

  1. Sanni ball bi ca kanam
    wendelal ball mu ñeuw ci yow
  2. Teubal dal ñari tank
    "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
  3. Pivote 360 degre
    pivote 360 degre bayi pañe bi ak sa tank bi ci kanam
  4. Femu profesionel
    Ndiego sa ndeydior wala thiamoñ, drblel sa digante tank
  5. Ndiego bu yatu
    Beusal ak tank bi ci ginaw
  6. Dugal ball bi ci suff
    Teg ball bi ci koñ bu weex u dunk bi.

faram fathie: Boniface Ndong


Bball loxo bu gatt

BballSteno_KL111

Bball loxo bu gatt?



BasKidball