taggat - taggat ben ben

Tannal ca taggat

KL126 : Pivote 360 degre + wendelu ca kanam + Dugal ball bi ci suff

  1. Sanni ball bi ca kanam
    wendelal ball mu ñeuw ci yow
  2. Teubal dal ñari tank
    "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
  3. Pivote 360 degre
    pivote 360 degre bayi pañe bi ak sa tank bi ci kanam
  4. Dox xarale sa yaram
    Driblel loxo bi ci biti- ,tank ak ball bi lalando suuf, tank bi ci bir ak benen loxo bi sam ball bi.
  5. wendelu ca kanam
    wendelal sa yaram 270 degre ca kanam
  6. Driblel ca pañe ba ndax dugal ball bi ci suff
    di dem ci pañe ba.
  7. Dugal ball bi ci suff
    Teg ball bi ci koñ bu weex u dunk bi.

faram fathie: Boniface Ndong


Bball loxo bu gatt

BballSteno_KL111

Bball loxo bu gatt?



BasKidball