taggat - taggat ben ben

Tannal ca taggat

KL119 : femu MJ + wendelu ca kanam + Wereul ball bi sa bopp + Dugal ball bi ci suff

  1. Sanni ball bi ca kanam
    wendelal ball mu ñeuw ci yow
  2. Teubal dal ñari tank
    "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
  3. Dox xarale sa yaram
    Driblel loxo bi ci biti- ,tank ak ball bi lalando suuf, tank bi ci bir ak benen loxo bi sam ball bi.
  4. femu MJ
    Defal ndiego bu mag ak sa tank u ginaw di dem xaralale sa tank, tegal sa tank, xaralel ci suf.
  5. japp sa drible
    Tank ak ball lalando suff, ñu degando drible ak ndiego bi, benen tank ak benen loxo sam ball bi.
  6. wendelu ca kanam
    wendelal sa yaram 270 degre ca kanam
  7. Wereul ball bi sa bopp
    wereulal ball bi sa ndigg par benn loxo, loxo yi jub.
  8. Driblel ca pañe ba ndax dugal ball bi ci suff
    di dem ci pañe ba.
  9. Dugal ball bi ci suff
    Teg ball bi ci koñ bu weex u dunk bi.

faram fathie: Boniface Ndong


Bball loxo bu gatt

BballSteno_KL111

Bball loxo bu gatt?



BasKidball