Teubal dal ñari tank "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
Dox xarale sa yaram Driblel loxo bi ci biti- ,tank ak ball bi lalando suuf, tank bi ci bir ak benen loxo bi sam ball bi.
femu MJ Defal ndiego bu mag ak sa tank u ginaw di dem xaralale sa tank, tegal sa tank, xaralel ci suf.
japp sa drible Tank ak ball lalando suff, ñu degando drible ak ndiego bi, benen tank ak benen loxo sam ball bi.