taggat - taggat ben ben

Tannal ca taggat

KL112 : Pivote 360 degre + wendelu pivote 180 degre + wendelu ca kanam + Wereul ball bi sa bopp + Dugal ball bi ci suff

  1. Sanni ball bi ca kanam
    wendelal ball mu ñeuw ci yow
  2. Teubal dal ñari tank
    "Taxawu Donald Duck"- niari tank yi dalando ,ginawu tank bi jitu baram yi topp ,taxaw bu degeur ,yatuwayu tank yi ag mbag yi tollo , tank yi jublu pañe bi.
  3. Pivote 360 degre
    pivote 360 degre bayi pañe bi ak sa tank bi ci kanam
  4. wendelu pivote 180 degre
    Delu wendelu 180 degre
  5. japp sa drible
    Tank ak ball lalando suff, ñu degando drible ak ndiego bi, benen tank ak benen loxo sam ball bi.
  6. wendelu ca kanam
    wendelal sa yaram 270 degre ca kanam
  7. Wereul ball bi sa bopp
    wereulal ball bi sa ndigg par benn loxo, loxo yi jub.
  8. Driblel ca pañe ba ndax dugal ball bi ci suff
    di dem ci pañe ba.
  9. Dugal ball bi ci suff
    Teg ball bi ci koñ bu weex u dunk bi.

faram fathie: Boniface Ndong


Bball loxo bu gatt

BballSteno_KL111

Bball loxo bu gatt?



BasKidball