taggat - taggat ben ben

GM104 : wendelu ca kanam right

  1. Dox xarale sa yaram
    Driblel loxo bi ci biti- ,tank ak ball bi lalando suuf, tank bi ci bir ak benen loxo bi sam ball bi.
  2. wendelu ca kanam
    wendelal sa yaram 270 degre ca kanam
  3. Ndiego bu yatu
    Beusal ak tank bi ci ginaw

faram fathie: Boniface Ndong


Bball loxo bu gatt

BballSteno_KL111

Bball loxo bu gatt?



BasKidball